Bii jukki ab junj rekk la.
Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal
Rabat (di الرباط ar-Ribat ci araab) mooy péeyu Nguurug Marok, mooy ñaareelu dëkk bi ëppi nit ca nguur ga. Mi ngi nekk ci wetu tefesu mbàmbulaanug Atlas gi. Ca jamono-ju-yàgg ja lañu fa tambalee dëkk. Ñoo ngi ko sos, dëgg-dëgg, ci 1150.
