
Bii jukki ab junj rekk la.
Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal
Alse walla الجزائر ci araabi alseeri mooy péeyu réewum Alseeri, féete ci bëj-gànnaaru réew mi janook Géej gu Diggu gi. Mooy itam dëkk bi gën a mag ca réew ma
